Flacon diwu kawar ak guy

Topptoo kawar

Diwu kawar

Guy ak ylang-ylang

Topptoo buy dëgëral kawar yu wow, yuy dog walla yu leerul: dafay dimbali kawar yi ñu gën a dëgër, dafay dundal leen, te delloo leen nooyaay ak leer.

Ñu xeeñal ko ak ylang-ylang. Sosu Notre-Dame de Bàdi la. Ñu defare ko loxo, ci lu tuuti.

Format

Li ëpp solo ci li ñu ci def

Diwu guy: dafay delloo dund kawar yu sonn, te jox leen leer.

Diwu ricin: xam nañu ne dafay dëgëral; dafay gën a dëgëral kawar gi, te deru bopp bi it jariñu ci.

Diwu touloucouna: dafay dimbali deru bopp bi mu nekk ci dal.

Koko, jojoba ak tournesol: koko dafay tëral kawar gi, jojoba di ko delloo nooyaay, tournesol di ko aar ci jant ak ngelaw.

Xeeñu ylang-ylang: xetu tóor-tóor.

Naka lañuy jëfandikoo

Bés bu nekk: def ay tóq ci guddaayu kawar gi ak ci cat yi.

Ni bain d'huile: bàyyi ko fanweeri minit balaa ngay def shampooing.

Ci biti yaram rekk lañu koy jëfandikoo. Jàng li ñu bind ci étiquette bi ngir xam lépp li ñu ci def.

Monastère Notre-Dame de Bàdi ak dexu Gambi, ñu nataal leen ci kaw asamaan

« Ci lañuy doon ay moine yu dëgg, bu ñuy dundee liggéeyu seeni loxo. » — Règle de saint Benoît, ch. 48