
Monastère bi bérabu noppi ak xalaat Yàlla la.
Messe bu Sell bi ak Offices yi ubbiku nañu ñeel ñépp.
Ngir wormaal dundu moine yi, kenn du wër di seetaan biir monastère bi.
Man ngaa ñëw, ci wormaal dundu moine yi, def fi ay fani retraite te xam sunu dundin.





